Simoore An-Nasr ci Aarabu ak Wolof

Jàng Simoore An-Nasr ak tekkim wolof bu mat sëkk, ak baat. Tekki ayaa bu ne. (3 Aaya — مدنية). An-Nasr Dégg, An-Nasr Tekki, An-Nasr mp3, An-Nasr pdf.

Jàng te Dégg Simoore An-Nasr

🎧 Aaya
M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
—
x1
bismillah
إِذَا جَاءَ نَصْرُ اللَّهِ وَالْفَتْحُ ۝١
📖 Tekki Aaya 1
Saa su ndimbalu Yàlla dikkee ak ndam la,
وَرَأَيْتَ النَّاسَ يَدْخُلُونَ فِي دِينِ اللَّهِ أَفْوَاجًا ۝٢
📖 Tekki Aaya 2
te nga gis ne nit ñaa ngi dugg def ay mbooloo ci biir diineey Yàlla ji,
فَسَبِّحْ بِحَمْدِ رَبِّكَ وَاسْتَغْفِرْهُ ۚ إِنَّهُ كَانَ تَوَّابًا ۝٣
📖 Tekki Aaya 3
na nga sàbaal, te sant sa Boroom te na nga sàkku njéggalam. Moom Nànguwaakoonu tuub la.
← 109 An-Nasr (110/114) 111 →
Jàng Simoore An-Nasr ci Wolof – Tekki, Waxtaan ak Baat

110النصر An-Nasr 📚 3 Aaya مدنية



Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers