Simoore Al-Ikhlas ci Aarabu ak Wolof

Jàng Simoore Al-Ikhlas ak tekkim wolof bu mat sëkk, ak baat. Tekki ayaa bu ne. (4 Aaya — مكية). Al-Ikhlas Dégg, Al-Ikhlas Tekki, Al-Ikhlas mp3, Al-Ikhlas pdf.

Jàng te Dégg Simoore Al-Ikhlas

🎧 Aaya
M Mishary Rashid Alafasy
M Mahmoud Khalil Al-Husary
A Abdurrahman As-Sudais
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi
A Abdul Basit Abdul Samad
A Ali Al-Hudhaify
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy
A Abu Bakr Ash-Shaatree
M Muhammad Ayyoub
A Abdullah Basfar
A Abdullah Al-Juhani
M Maher Al Muaiqly
x1
قُلْ هُوَ اللَّهُ أَحَدٌ ۝١
📖 Tekki Aaya 1
Waxal ne : “Yàlla, moom Kenn la (jenn Yàlla rekk la).
اللَّهُ الصَّمَدُ ۝٢
📖 Tekki Aaya 2
Moom Yàlla, Mooy Kilifa gi wareefa joyal mbir yi.
لَمْ يَلِدْ وَلَمْ يُولَدْ ۝٣
📖 Tekki Aaya 3
Jurul, te Kenn juru ko.
وَلَمْ يَكُن لَّهُ كُفُوًا أَحَدٌ ۝٤
📖 Tekki Aaya 4
Te amul benni nàttangoo”.
← 111 Al-Ikhlas (112/114) 113 →
Jàng Simoore Al-Ikhlas ci Wolof – Tekki, Waxtaan ak Baat

112الإخلاص Al-Ikhlas 📚 4 Aaya مكية



Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers