3 Aaya · Medinan · Wolof
bismillah
ﭱﭲﭳﭴﭵﭶ
110:1 Saa su ndimbalu Yàlla dikkee ak ndam la,
ﭷﭸﭹﭺﭻﭼﭽﭾ
110:2 te nga gis ne nit ñaa ngi dugg def ay mbooloo ci biir diineey Yàlla ji,
ﭿﮀﮁﮂﮃﮄﮅﮆﮇ
110:3 na nga sàbaal, te sant sa Boroom te na nga sàkku njéggalam. Moom Nànguwaakoonu tuub la.

Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 29, 2026

Don't forget us in your sincere prayers