Simoore An-Nas ci Aarabu ak Wolof

Jàng Simoore An-Nas ak tekkim wolof bu mat sëkk, ak baat. Tekki ayaa bu ne. (6 Aaya — مكية). An-Nas Dégg, An-Nas Tekki, An-Nas mp3, An-Nas pdf.

Jàng te Dégg Simoore An-Nas

🎧 Aaya
M Mishary Rashid Alafasy
M Mahmoud Khalil Al-Husary
A Abdurrahman As-Sudais
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi
A Abdul Basit Abdul Samad
A Ali Al-Hudhaify
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy
A Abu Bakr Ash-Shaatree
M Muhammad Ayyoub
A Abdullah Basfar
A Abdullah Al-Juhani
M Maher Al Muaiqly
x1
قُلْ أَعُوذُ بِرَبِّ النَّاسِ ۝١
📖 Tekki Aaya 1
Waxal ne : “Maa ngi sàkku muslaayi Boroom nit ñi.
مَلِكِ النَّاسِ ۝٢
📖 Tekki Aaya 2
Kiy Buurub nit ñi,
إِلَٰهِ النَّاسِ ۝٣
📖 Tekki Aaya 3
Di Yàlla nit ñi,
مِن شَرِّ الْوَسْوَاسِ الْخَنَّاسِ ۝٤
📖 Tekki Aaya 4
ci ayu jax-jaxali, Saytaane,
الَّذِي يُوَسْوِسُ فِي صُدُورِ النَّاسِ ۝٥
📖 Tekki Aaya 5
kiy jax-jaxal ci biir dënni nit ñi,
مِنَ الْجِنَّةِ وَالنَّاسِ ۝٦
📖 Tekki Aaya 6
te bokk ci jinne yeek nit ñi”.
← 113 An-Nas (114/114)
Jàng Simoore An-Nas ci Wolof – Tekki, Waxtaan ak Baat

114الناس An-Nas 📚 6 Aaya مكية



Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers