An-Nasr · 1/3
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nasr
إِذَا جَاءَ نَصْرُ اللَّهِ وَالْفَتْحُ ۝١
Iza jaa-a nas rullahi walfath
📖 Tekkim Wolof
Saa su ndimbalu Yàlla dikkee ak ndam la,

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-3 — Simoore An-Nasr

1إِذَا جَاءَ نَصْرُ اللَّهِ وَالْفَتْحُ
Saa su ndimbalu Yàlla dikkee ak ndam la,
2وَرَأَيْتَ النَّاسَ يَدْخُلُونَ فِي دِينِ اللَّهِ أَفْوَاجًا
te nga gis ne nit ñaa ngi dugg def ay mbooloo ci biir diineey Yàlla ji,
3فَسَبِّحْ بِحَمْدِ رَبِّكَ وَاسْتَغْفِرْهُ ۚ إِنَّهُ كَانَ تَوَّابًا
na nga sàbaal, te sant sa Boroom te na nga sàkku njéggalam. Moom Nànguwaakoonu tuub la.
An-NasrFihi Alxuraan
3Aaya
MedinanRevelation
1Aaya

Tekki — An-Nasr 1

Simoore An-Nasr Aaya 1 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Saa su ndimbalu Yàlla dikkee ak ndam la,

Simoore Aaya 1/3 — Simoore An-Nasr النصر (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nasr Dégg, Simoore An-Nasr Tekki, Simoore An-Nasr mp3, Simoore An-Nasr pdf. Aaya 1–3. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers