Simoore Al-Qadr ci Aarabu ak Wolof

Jàng Simoore Al-Qadr ak tekkim wolof bu mat sëkk, ak baat. Tekki ayaa bu ne. (5 Aaya — مكية). Al-Qadr Dégg, Al-Qadr Tekki, Al-Qadr mp3, Al-Qadr pdf.

Jàng te Dégg Simoore Al-Qadr

🎧 Aaya
M Mishary Rashid Alafasy
M Mahmoud Khalil Al-Husary
A Abdurrahman As-Sudais
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi
A Abdul Basit Abdul Samad
A Ali Al-Hudhaify
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy
A Abu Bakr Ash-Shaatree
M Muhammad Ayyoub
A Abdullah Basfar
A Abdullah Al-Juhani
M Maher Al Muaiqly
x1
إِنَّا أَنزَلْنَاهُ فِي لَيْلَةِ الْقَدْرِ ۝١
📖 Tekki Aaya 1
Wàcce nanu ko (Alxuraan) ci guddig dogal ba (Laylatul Qadri).
وَمَا أَدْرَاكَ مَا لَيْلَةُ الْقَدْرِ ۝٢
📖 Tekki Aaya 2
Ana lan moo lay xamal laylatul Qadri ?
لَيْلَةُ الْقَدْرِ خَيْرٌ مِّنْ أَلْفِ شَهْرٍ ۝٣
📖 Tekki Aaya 3
Laylatul Qadri moo gën junni weer.
تَنَزَّلُ الْمَلَائِكَةُ وَالرُّوحُ فِيهَا بِإِذْنِ رَبِّهِم مِّن كُلِّ أَمْرٍ ۝٤
📖 Tekki Aaya 4
Ci guddi googu Malaaka ya, dañu cay wàcci àndak (Jibriil) ci seen ndigalu Boroom ci mépp mbir.
سَلَامٌ هِيَ حَتَّىٰ مَطْلَعِ الْفَجْرِ ۝٥
📖 Tekki Aaya 5
Jàmm rekk la ba baa njël di jot (fajar sa di xar).
← 96 Al-Qadr (97/114) 98 →
Jàng Simoore Al-Qadr ci Wolof – Tekki, Waxtaan ak Baat

97القدر Al-Qadr 📚 5 Aaya مكية



Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers