📖 0/604 xët yi jàng nañu
📄 586
Simoore At-Takwir

Simoore At-Takwir

81:5
وَإِذَا ٱلۡوُحُوشُ حُشِرَتۡ ٥
ak ndokmenta ya (rab yu aaytal ya), dajaloo ñu dekkalaat leen,
81:8
وَإِذَا ٱلۡمَوۡءُۥدَةُ سُئِلَتۡ ٨
ak saa su ñu laajee doom ju jigéen ja nu soloon te fekk muy dund, ngir daw gàcce
81:19
إِنَّهُۥ لَقَوۡلُ رَسُولٍ كَرِيمٍ ١٩
Ci ne [Alxuraan jii] waxi ab Yonent la bu tedd (Jibriil),
81:20
ذِي قُوَّةٍ عِندَ ذِي ٱلۡعَرۡشِ مَكِينٍ ٢٠
di boroom kàttan gu rëy, di ab xejj fa Boroom ganganaay ga Aras,
81:27
إِنۡ هُوَ إِلَّا ذِكۡرٌ لِّلۡعَٰلَمِينَ ٢٧
Lii du lenn lu dul luy fàttali waa àddina si yépp,
81:29
وَمَا تَشَآءُونَ إِلَّآ أَن يَشَآءَ ٱللَّهُ رَبُّ ٱلۡعَٰلَمِينَ ٢٩
Waaye manuleena soob mukk, te du ut ne dafa soob Yàlla, Boroom àddina si yépp ;
العربيةEnglishBahasa IndonesiaTürkçeРусскийفارسیFrançaisاردوবাংলাDeutschEspañol中文हिन्दीPortuguêsItalianoภาษาไทยPolskiNederlandsShqipKiswahiliO'zbekதமிழ்MelayuBosanskiSoomaaliAzərbaycanکوردی한국어日本語SvenskaDanskNorskپښتوമലയാളംසිංහලTamazightHausaአማርኛБългарскиТоҷикӣҚазақшаFilipinoسنڌيYorùbáFulfuldeТатарчаئۇيغۇرچەКыргызчаਪੰਜਾਬੀJawaతెలుగుမြန်မာગુજરાતીOromoमराठीTiếng ViệtMalagasyНохчийнWolofދިވެހިಕನ್ನಡУкраїнськаΕλληνικάქართულიខ្មែរدریQafar afMaranaoनेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, September 1, 2026
Don't forget us in your sincere prayers







