At-Takwir · 26/29
Tekki Waxtaan — At-Takwir
فَأَيْنَ تَذْهَبُونَ ۝٢٦
Fa ayna tazhaboon
📖 Tekkim Wolof
Kon ana fu ngeen jëm ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 24-28 — At-Takwir

24وَمَا هُوَ عَلَى الْغَيْبِ بِضَنِينٍ
te moom nayul ci li ñu ko soloo.
25وَمَا هُوَ بِقَوْلِ شَيْطَانٍ رَّجِيمٍ
Te it [Alxuraan ji] du waxi seytaane sa ñu jam.
26فَأَيْنَ تَذْهَبُونَ
Kon ana fu ngeen jëm ?
27إِنْ هُوَ إِلَّا ذِكْرٌ لِّلْعَالَمِينَ
Lii du lenn lu dul luy fàttali waa àddina si yépp,
28لِمَن شَاءَ مِنكُمْ أَن يَسْتَقِيمَ
ku mu soob ci yéen mu topp yoon wu jub xocc wa.
At-TakwirFihi Alxuraan
29Aaya
MeccanRevelation
26Aaya

Tekki — At-Takwir 26

Simoore At-Takwir Aaya 26 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Kon ana fu ngeen jëm ?

Simoore Aaya 26/29 — At-Takwir التكوير (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: At-Takwir Dégg, At-Takwir Tekki, At-Takwir mp3, At-Takwir pdf. Aaya 24–28. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers