At-Takwir · 29/29
Tekki Waxtaan — Simoore At-Takwir
وَمَا تَشَاءُونَ إِلَّا أَن يَشَاءَ اللَّهُ رَبُّ الْعَالَمِينَ ۝٢٩
Wa maa tashaaa`oona illaaa ai yashaaa `al laahu Rabbul `Aalameen
📖 Tekkim Wolof
Waaye manuleena soob mukk, te du ut ne dafa soob Yàlla, Boroom àddina si yépp ;

🎧 Dégg


📜 Aaya 27-29 — Simoore At-Takwir

27إِنْ هُوَ إِلَّا ذِكْرٌ لِّلْعَالَمِينَ
Lii du lenn lu dul luy fàttali waa àddina si yépp,
28لِمَن شَاءَ مِنكُمْ أَن يَسْتَقِيمَ
ku mu soob ci yéen mu topp yoon wu jub xocc wa.
29وَمَا تَشَاءُونَ إِلَّا أَن يَشَاءَ اللَّهُ رَبُّ الْعَالَمِينَ
Waaye manuleena soob mukk, te du ut ne dafa soob Yàlla, Boroom àddina si yépp ;
At-TakwirFihi Alxuraan
29Aaya
MeccanRevelation
29Aaya

Tekki — At-Takwir 29

Simoore At-Takwir Aaya 29 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waaye manuleena soob mukk, te du ut ne dafa soob…

Simoore Aaya 29/29 — Simoore At-Takwir التكوير (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Takwir Dégg, Simoore At-Takwir Tekki, Simoore At-Takwir mp3, Simoore At-Takwir pdf. Aaya 27–29. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers