At-Takwir · 24/29
Tekki Waxtaan — Simoore At-Takwir
وَمَا هُوَ عَلَى الْغَيْبِ بِضَنِينٍ ۝٢٤
Wa maa huwa `alal ghaibi bidaneen
📖 Tekkim Wolof
te moom nayul ci li ñu ko soloo.

🎧 Dégg


📜 Aaya 22-26 — Simoore At-Takwir

22وَمَا صَاحِبُكُم بِمَجْنُونٍ
Te seen àndandoo ja (Muhammad) du ab dof de ;
23وَلَقَدْ رَآهُ بِالْأُفُقِ الْمُبِينِ
moom gis na tigi (Jibriil), ca asamaan ya
24وَمَا هُوَ عَلَى الْغَيْبِ بِضَنِينٍ
te moom nayul ci li ñu ko soloo.
25وَمَا هُوَ بِقَوْلِ شَيْطَانٍ رَّجِيمٍ
Te it [Alxuraan ji] du waxi seytaane sa ñu jam.
26فَأَيْنَ تَذْهَبُونَ
Kon ana fu ngeen jëm ?
At-TakwirFihi Alxuraan
29Aaya
MeccanRevelation
24Aaya

Tekki — At-Takwir 24

Simoore At-Takwir Aaya 24 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te moom nayul ci li ñu ko soloo.

Simoore Aaya 24/29 — Simoore At-Takwir التكوير (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Takwir Dégg, Simoore At-Takwir Tekki, Simoore At-Takwir mp3, Simoore At-Takwir pdf. Aaya 22–26. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers