At-Takwir · 27/29
Tekki Waxtaan — Simoore At-Takwir
إِنْ هُوَ إِلَّا ذِكْرٌ لِّلْعَالَمِينَ ۝٢٧
In huwa illaa zikrul lil`aalameen
📖 Tekkim Wolof
Lii du lenn lu dul luy fàttali waa àddina si yépp,

🎧 Dégg


📜 Aaya 25-29 — Simoore At-Takwir

25وَمَا هُوَ بِقَوْلِ شَيْطَانٍ رَّجِيمٍ
Te it [Alxuraan ji] du waxi seytaane sa ñu jam.
26فَأَيْنَ تَذْهَبُونَ
Kon ana fu ngeen jëm ?
27إِنْ هُوَ إِلَّا ذِكْرٌ لِّلْعَالَمِينَ
Lii du lenn lu dul luy fàttali waa àddina si yépp,
28لِمَن شَاءَ مِنكُمْ أَن يَسْتَقِيمَ
ku mu soob ci yéen mu topp yoon wu jub xocc wa.
29وَمَا تَشَاءُونَ إِلَّا أَن يَشَاءَ اللَّهُ رَبُّ الْعَالَمِينَ
Waaye manuleena soob mukk, te du ut ne dafa soob Yàlla, Boroom àddina si yépp ;
At-TakwirFihi Alxuraan
29Aaya
MeccanRevelation
27Aaya

Tekki — At-Takwir 27

Simoore At-Takwir Aaya 27 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Lii du lenn lu dul luy fàttali waa àddina si…

Simoore Aaya 27/29 — Simoore At-Takwir التكوير (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Takwir Dégg, Simoore At-Takwir Tekki, Simoore At-Takwir mp3, Simoore At-Takwir pdf. Aaya 25–29. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers