At-Takwir · 28/29
Tekki Waxtaan — Simoore At-Takwir
لِمَن شَاءَ مِنكُمْ أَن يَسْتَقِيمَ ۝٢٨
Liman shaaa`a minkum ai yastaqeem
📖 Tekkim Wolof
ku mu soob ci yéen mu topp yoon wu jub xocc wa.

🎧 Dégg


📜 Aaya 26-29 — Simoore At-Takwir

26فَأَيْنَ تَذْهَبُونَ
Kon ana fu ngeen jëm ?
27إِنْ هُوَ إِلَّا ذِكْرٌ لِّلْعَالَمِينَ
Lii du lenn lu dul luy fàttali waa àddina si yépp,
28لِمَن شَاءَ مِنكُمْ أَن يَسْتَقِيمَ
ku mu soob ci yéen mu topp yoon wu jub xocc wa.
29وَمَا تَشَاءُونَ إِلَّا أَن يَشَاءَ اللَّهُ رَبُّ الْعَالَمِينَ
Waaye manuleena soob mukk, te du ut ne dafa soob Yàlla, Boroom àddina si yépp ;
At-TakwirFihi Alxuraan
29Aaya
MeccanRevelation
28Aaya

Tekki — At-Takwir 28

Simoore At-Takwir Aaya 28 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ku mu soob ci yéen mu topp yoon wu jub…

Simoore Aaya 28/29 — Simoore At-Takwir التكوير (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Takwir Dégg, Simoore At-Takwir Tekki, Simoore At-Takwir mp3, Simoore At-Takwir pdf. Aaya 26–29. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers