Simoore Al-Kawthar ci Aarabu ak Wolof

Jàng Simoore Al-Kawthar ak tekkim wolof bu mat sëkk, ak baat. Tekki ayaa bu ne. (3 Aaya — مكية). Al-Kawthar Dégg, Al-Kawthar Tekki, Al-Kawthar mp3, Al-Kawthar pdf.

Jàng te Dégg Simoore Al-Kawthar

🎧 Aaya
M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
—
x1
bismillah
إِنَّا أَعْطَيْنَاكَ الْكَوْثَرَ ۝١
📖 Tekki Aaya 1
Jox Nanu la, déegub Kawsara.
فَصَلِّ لِرَبِّكَ وَانْحَرْ ۝٢
📖 Tekki Aaya 2
Na ngay julli ngir sa Boroom te na ngay rendi.
إِنَّ شَانِئَكَ هُوَ الْأَبْتَرُ ۝٣
📖 Tekki Aaya 3
Ka lay bañ aka ñaawal, moo dog ci lépp lu baax.
← 107 Al-Kawthar (108/114) 109 →
Jàng Simoore Al-Kawthar ci Wolof – Tekki, Waxtaan ak Baat

108الكوثر Al-Kawthar 📚 3 Aaya مكية



Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers