3 Aaya · Meccan · Wolof
bismillah
ﮆﮇﮈﮉ
108:1 Jox Nanu la, déegub Kawsara.
ﮊﮋﮌﮍ
108:2 Na ngay julli ngir sa Boroom te na ngay rendi.
ﮎﮏﮐﮑﮒ
108:3 Ka lay bañ aka ñaawal, moo dog ci lépp lu baax.

Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 29, 2026

Don't forget us in your sincere prayers