Al-Ikhlas · 3/4
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Ikhlas
لَمْ يَلِدْ وَلَمْ يُولَدْ ۝٣
Lam yalid wa lam yoolad
📖 Tekkim Wolof
Jurul, te Kenn juru ko.

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-4 — Simoore Al-Ikhlas

1قُلْ هُوَ اللَّهُ أَحَدٌ
Waxal ne : “Yàlla, moom Kenn la (jenn Yàlla rekk la).
2اللَّهُ الصَّمَدُ
Moom Yàlla, Mooy Kilifa gi wareefa joyal mbir yi.
3لَمْ يَلِدْ وَلَمْ يُولَدْ
Jurul, te Kenn juru ko.
4وَلَمْ يَكُن لَّهُ كُفُوًا أَحَدٌ
Te amul benni nàttangoo”.
Al-IkhlasFihi Alxuraan
4Aaya
MeccanRevelation
3Aaya

Tekki — Al-Ikhlas 3

Simoore Al-Ikhlas Aaya 3 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Jurul, te Kenn juru ko.

Simoore Aaya 3/4 — Simoore Al-Ikhlas الإخلاص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Ikhlas Dégg, Simoore Al-Ikhlas Tekki, Simoore Al-Ikhlas mp3, Simoore Al-Ikhlas pdf. Aaya 1–4. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers