4 Aaya · Meccan · Wolof
bismillah
ﭑﭒﭓﭔﭕ
112:1 Waxal ne : “Yàlla, moom Kenn la (jenn Yàlla rekk la).
ﭖﭗﭘ
112:2 Moom Yàlla, Mooy Kilifa gi wareefa joyal mbir yi.
ﭙﭚﭛﭜﭝ
112:3 Jurul, te Kenn juru ko.
ﭞﭟﭠﭡﭢﭣ
112:4 Te amul benni nàttangoo”.

Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 29, 2026

Don't forget us in your sincere prayers