Simoore Al-'Asr ci Aarabu ak Wolof

Jàng Simoore Al-'Asr ak tekkim wolof bu mat sëkk, ak baat. Tekki ayaa bu ne. (3 Aaya — مكية). Al-'Asr Dégg, Al-'Asr Tekki, Al-'Asr mp3, Al-'Asr pdf.

Jàng te Dégg Simoore Al-'Asr

🎧 Aaya
M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
—
x1
bismillah
وَالْعَصْرِ ۝١
📖 Tekki Aaya 1
(Giiñ naa) ci Jamono!
إِنَّ الْإِنسَانَ لَفِي خُسْرٍ ۝٢
📖 Tekki Aaya 2
Ne nit, mi ngi cig yàqule,
إِلَّا الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ وَتَوَاصَوْا بِالْحَقِّ وَتَوَاصَوْا بِالصَّبْرِ ۝٣
📖 Tekki Aaya 3
bamu des ña gëm, tey jëf yiw di dénkënte dëgg di dékënte ci muñ.
← 102 Al-'Asr (103/114) 104 →
Jàng Simoore Al-'Asr ci Wolof – Tekki, Waxtaan ak Baat

103العصر Al-'Asr 📚 3 Aaya مكية



Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers