3 Aaya · Meccan · Wolof
bismillah
ﭑﭒ
103:1 (Giiñ naa) ci Jamono!
ﭓﭔﭕﭖﭗ
103:2 Ne nit, mi ngi cig yàqule,
ﭘﭙﭚﭛﭜﭝﭞﭟﭠﭡ
103:3 bamu des ña gëm, tey jëf yiw di dénkënte dëgg di dékënte ci muñ.

Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 29, 2026

Don't forget us in your sincere prayers