6 Aaya · Meccan · Wolof
bismillah
ﮀﮁﮂﮃﮄ
114:1 Waxal ne : “Maa ngi sàkku muslaayi Boroom nit ñi.
ﮅﮆﮇ
114:2 Kiy Buurub nit ñi,
ﮈﮉﮊ
114:3 Di Yàlla nit ñi,
ﮋﮌﮍﮎﮏ
114:4 ci ayu jax-jaxali, Saytaane,
ﮐﮑﮒﮓﮔﮕ
114:5 kiy jax-jaxal ci biir dënni nit ñi,
ﮖﮗﮘﮙ
114:6 te bokk ci jinne yeek nit ñi”.

Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 29, 2026

Don't forget us in your sincere prayers