Al-Qadr · 1/5
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qadr
إِنَّا أَنزَلْنَاهُ فِي لَيْلَةِ الْقَدْرِ ۝١
Innaa anzalnaahu fee lailatil qadr
📖 Tekkim Wolof
Wàcce nanu ko (Alxuraan) ci guddig dogal ba (Laylatul Qadri).

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 1-3 — Simoore Al-Qadr

1إِنَّا أَنزَلْنَاهُ فِي لَيْلَةِ الْقَدْرِ
Wàcce nanu ko (Alxuraan) ci guddig dogal ba (Laylatul Qadri).
2وَمَا أَدْرَاكَ مَا لَيْلَةُ الْقَدْرِ
Ana lan moo lay xamal laylatul Qadri ?
3لَيْلَةُ الْقَدْرِ خَيْرٌ مِّنْ أَلْفِ شَهْرٍ
Laylatul Qadri moo gën junni weer.
Al-QadrFihi Alxuraan
5Aaya
MeccanRevelation
1Aaya

Tekki — Al-Qadr 1

Simoore Al-Qadr Aaya 1 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Wàcce nanu ko (Alxuraan) ci guddig dogal ba (Laylatul Qadri).

Simoore Aaya 1/5 — Simoore Al-Qadr القدر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qadr Dégg, Simoore Al-Qadr Tekki, Simoore Al-Qadr mp3, Simoore Al-Qadr pdf. Aaya 1–3. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers