Al-Qadr · 2/5
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qadr
وَمَا أَدْرَاكَ مَا لَيْلَةُ الْقَدْرِ ۝٢
Wa maa adraaka ma lailatul qadr
📖 Tekkim Wolof
Ana lan moo lay xamal laylatul Qadri ?

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 1-4 — Simoore Al-Qadr

1إِنَّا أَنزَلْنَاهُ فِي لَيْلَةِ الْقَدْرِ
Wàcce nanu ko (Alxuraan) ci guddig dogal ba (Laylatul Qadri).
2وَمَا أَدْرَاكَ مَا لَيْلَةُ الْقَدْرِ
Ana lan moo lay xamal laylatul Qadri ?
3لَيْلَةُ الْقَدْرِ خَيْرٌ مِّنْ أَلْفِ شَهْرٍ
Laylatul Qadri moo gën junni weer.
4تَنَزَّلُ الْمَلَائِكَةُ وَالرُّوحُ فِيهَا بِإِذْنِ رَبِّهِم مِّن كُلِّ أَمْرٍ
Ci guddi googu Malaaka ya, dañu cay wàcci àndak (Jibriil) ci seen ndigalu Boroom ci mépp mbir.
Al-QadrFihi Alxuraan
5Aaya
MeccanRevelation
2Aaya

Tekki — Al-Qadr 2

Simoore Al-Qadr Aaya 2 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ana lan moo lay xamal laylatul Qadri ?

Simoore Aaya 2/5 — Simoore Al-Qadr القدر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qadr Dégg, Simoore Al-Qadr Tekki, Simoore Al-Qadr mp3, Simoore Al-Qadr pdf. Aaya 1–4. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 29, 2026

Don't forget us in your sincere prayers