5 Aaya · Meccan · Wolof
bismillah
ﭴﭵﭶﭷﭸﭹ
97:1 Wàcce nanu ko (Alxuraan) ci guddig dogal ba (Laylatul Qadri).
ﭺﭻﭼﭽﭾﭿ
97:2 Ana lan moo lay xamal laylatul Qadri ?
ﮀﮁﮂﮃﮄﮅﮆ
97:3 Laylatul Qadri moo gën junni weer.
ﮇﮈﮉﮊﮋﮌﮍﮎﮏﮐ
97:4 Ci guddi googu Malaaka ya, dañu cay wàcci àndak (Jibriil) ci seen ndigalu Boroom ci mépp mbir.
ﮑﮒﮓﮔﮕﮖ
97:5 Jàmm rekk la ba baa njël di jot (fajar sa di xar).

Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 29, 2026

Don't forget us in your sincere prayers