Al-Qadr · 3/5
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qadr
لَيْلَةُ الْقَدْرِ خَيْرٌ مِّنْ أَلْفِ شَهْرٍ ۝٣
Lailatul qadri khairum min alfee shahr
📖 Tekkim Wolof
Laylatul Qadri moo gën junni weer.

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-5 — Simoore Al-Qadr

1إِنَّا أَنزَلْنَاهُ فِي لَيْلَةِ الْقَدْرِ
Wàcce nanu ko (Alxuraan) ci guddig dogal ba (Laylatul Qadri).
2وَمَا أَدْرَاكَ مَا لَيْلَةُ الْقَدْرِ
Ana lan moo lay xamal laylatul Qadri ?
3لَيْلَةُ الْقَدْرِ خَيْرٌ مِّنْ أَلْفِ شَهْرٍ
Laylatul Qadri moo gën junni weer.
4تَنَزَّلُ الْمَلَائِكَةُ وَالرُّوحُ فِيهَا بِإِذْنِ رَبِّهِم مِّن كُلِّ أَمْرٍ
Ci guddi googu Malaaka ya, dañu cay wàcci àndak (Jibriil) ci seen ndigalu Boroom ci mépp mbir.
5سَلَامٌ هِيَ حَتَّىٰ مَطْلَعِ الْفَجْرِ
Jàmm rekk la ba baa njël di jot (fajar sa di xar).
Al-QadrFihi Alxuraan
5Aaya
MeccanRevelation
3Aaya

Tekki — Al-Qadr 3

Simoore Al-Qadr Aaya 3 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Laylatul Qadri moo gën junni weer.

Simoore Aaya 3/5 — Simoore Al-Qadr القدر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qadr Dégg, Simoore Al-Qadr Tekki, Simoore Al-Qadr mp3, Simoore Al-Qadr pdf. Aaya 1–5. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers