Al-Maida · 5/120
Tekki Waxtaan — Al-Maida
الْيَوْمَ أُحِلَّ لَكُمُ الطَّيِّبَاتُ ۖ وَطَعَامُ الَّذِينَ أُوتُوا الْكِتَابَ حِلٌّ لَّكُمْ وَطَعَامُكُمْ حِلٌّ لَّهُمْ ۖ وَالْمُحْصَنَاتُ مِنَ الْمُؤْمِنَاتِ وَالْمُحْصَنَاتُ مِنَ الَّذِينَ أُوتُوا الْكِتَابَ مِن قَبْلِكُمْ إِذَا آتَيْتُمُوهُنَّ أُجُورَهُنَّ مُحْصِنِينَ غَيْرَ مُسَافِحِينَ وَلَا مُتَّخِذِي أَخْدَانٍ ۗ وَمَن يَكْفُرْ بِالْإِيمَانِ فَقَدْ حَبِطَ عَمَلُهُ وَهُوَ فِي الْآخِرَةِ مِنَ الْخَاسِرِينَ ٥
Transliteration
Alyawma uhilla lakumut taiyibaatu wa ta`aamul lazeena ootul Kitaaba hillul lakum wa ta`aamukum hillul lahum wal muhsanaatu minal mu`minaati walmuhsanaatu minal lazeena ootul Kitaaba min qablikum izaaa aataitumoohunna ujoorahunna muhsineena ghaira musaafiheena wa laa muttakhizeee akhdaan; wa mai yakfur bil eemaani faqad habita `amaluhoo wa huwa fil Aaakhirati minal khaasireen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
“Bis niki tey, dagan na ci yéen [ñam] yu sell ya. Àtteb ñamu ña jotoon Téere dagan na leen, te seeni ñam yéen, dagan ca ñoom. Te it gor ñu jigéen ña yéwén ci jullit ñi, ak jigéen ña di ay gor, yiw ca ña leen jëkk a jot Téere [dagan na ngeen sëy ak ñoom], ginnaaw ba ngeen joxee seen can ngir sëy mu bañ di njaaloo, ngeen bañ leen a jàppe it ay coro. Képp ku weddi ngëm, ay jëfam sippiku [yàqu] na te àllaaxiraa, ca ña yàqule lay bokk.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 3-7 — Al-Maida
3حُرِّمَتْ عَلَيْكُمُ الْمَيْتَةُ وَالدَّمُ وَلَحْمُ الْخِنزِيرِ وَمَا أُهِلَّ لِغَيْرِ اللَّهِ بِهِ وَالْمُنْخَنِقَةُ وَالْمَوْقُوذَةُ وَالْمُتَرَدِّيَةُ وَالنَّطِيحَةُ وَمَا أَكَلَ السَّبُعُ إِلَّا مَا ذَكَّيْتُمْ وَمَا ذُبِحَ عَلَى النُّصُبِ وَأَن تَسْتَقْسِمُوا بِالْأَزْلَامِ ۚ ذَٰلِكُمْ فِسْقٌ ۗ الْيَوْمَ يَئِسَ الَّذِينَ كَفَرُوا مِن دِينِكُمْ فَلَا تَخْشَوْهُمْ وَاخْشَوْنِ ۚ الْيَوْمَ أَكْمَلْتُ لَكُمْ دِينَكُمْ وَأَتْمَمْتُ عَلَيْكُمْ نِعْمَتِي وَرَضِيتُ لَكُمُ الْإِسْلَامَ دِينًا ۚ فَمَنِ اضْطُرَّ فِي مَخْمَصَةٍ غَيْرَ مُتَجَانِفٍ لِّإِثْمٍ ۙ فَإِنَّ اللَّهَ غَفُورٌ رَّحِيمٌ
Araam na ci yéen mala yu médd, ak deret, ak yàppu mbaam-xuux ak la ñu rey tudd ca ku dul Yàlla, ak mala mu wékku, ak bu ñu dóor ba mu dee, ak bu mbartal daanu, ak bu ñu jam béjjan, ak bu rabu àll am lu mu ca lekk - lu dul la ngeen reendi -. (Terees na it) bu ñu reendi ci ay xërëm, ngeen di séddalee ci wantaleb gisaane . Lu génn diine la. Tey jii, ña weddi naagu nañu ci seen diine : buleen leen ragal, ragal-leen Ma. Bis-pénc niki tey, matalal Naa leen seen diine, te xëpp naa leen Samay xéewal. Gërëm naa ci yéen Lislaam mu di seen diine. Koo xam ne dafa loru ci jamonoy xiif [ba lekk lu Ma araamal], te du dafa sóobu ci bàkkaar... na xam ne, Yàlla Jéggalaakoon la, Jaglewaakoon la.
4يَسْأَلُونَكَ مَاذَا أُحِلَّ لَهُمْ ۖ قُلْ أُحِلَّ لَكُمُ الطَّيِّبَاتُ ۙ وَمَا عَلَّمْتُم مِّنَ الْجَوَارِحِ مُكَلِّبِينَ تُعَلِّمُونَهُنَّ مِمَّا عَلَّمَكُمُ اللَّهُ ۖ فَكُلُوا مِمَّا أَمْسَكْنَ عَلَيْكُمْ وَاذْكُرُوا اسْمَ اللَّهِ عَلَيْهِ ۖ وَاتَّقُوا اللَّهَ ۚ إِنَّ اللَّهَ سَرِيعُ الْحِسَابِ
Ñanga lay laaj lan moo dagan ci ñoom. Neel : “Yu sell ya ñoo dagan ci yéen, ak la leen seen rëbbukaay yi ngeen yore indil, yu deme ni xaj, na leen ko Yàlla jàngale. Mën ngeen a lekk ca la ñu leen jàppale te nangeen ca tudd turu Yàlla. Te nangeen ragal Yàlla. Yàlla Ku gaaw la ci natt jëf yi.
5الْيَوْمَ أُحِلَّ لَكُمُ الطَّيِّبَاتُ ۖ وَطَعَامُ الَّذِينَ أُوتُوا الْكِتَابَ حِلٌّ لَّكُمْ وَطَعَامُكُمْ حِلٌّ لَّهُمْ ۖ وَالْمُحْصَنَاتُ مِنَ الْمُؤْمِنَاتِ وَالْمُحْصَنَاتُ مِنَ الَّذِينَ أُوتُوا الْكِتَابَ مِن قَبْلِكُمْ إِذَا آتَيْتُمُوهُنَّ أُجُورَهُنَّ مُحْصِنِينَ غَيْرَ مُسَافِحِينَ وَلَا مُتَّخِذِي أَخْدَانٍ ۗ وَمَن يَكْفُرْ بِالْإِيمَانِ فَقَدْ حَبِطَ عَمَلُهُ وَهُوَ فِي الْآخِرَةِ مِنَ الْخَاسِرِينَ
“Bis niki tey, dagan na ci yéen [ñam] yu sell ya. Àtteb ñamu ña jotoon Téere dagan na leen, te seeni ñam yéen, dagan ca ñoom. Te it gor ñu jigéen ña yéwén ci jullit ñi, ak jigéen ña di ay gor, yiw ca ña leen jëkk a jot Téere [dagan na ngeen sëy ak ñoom], ginnaaw ba ngeen joxee seen can ngir sëy mu bañ di njaaloo, ngeen bañ leen a jàppe it ay coro. Képp ku weddi ngëm, ay jëfam sippiku [yàqu] na te àllaaxiraa, ca ña yàqule lay bokk.
6يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا إِذَا قُمْتُمْ إِلَى الصَّلَاةِ فَاغْسِلُوا وُجُوهَكُمْ وَأَيْدِيَكُمْ إِلَى الْمَرَافِقِ وَامْسَحُوا بِرُءُوسِكُمْ وَأَرْجُلَكُمْ إِلَى الْكَعْبَيْنِ ۚ وَإِن كُنتُمْ جُنُبًا فَاطَّهَّرُوا ۚ وَإِن كُنتُم مَّرْضَىٰ أَوْ عَلَىٰ سَفَرٍ أَوْ جَاءَ أَحَدٌ مِّنكُم مِّنَ الْغَائِطِ أَوْ لَامَسْتُمُ النِّسَاءَ فَلَمْ تَجِدُوا مَاءً فَتَيَمَّمُوا صَعِيدًا طَيِّبًا فَامْسَحُوا بِوُجُوهِكُمْ وَأَيْدِيكُم مِّنْهُ ۚ مَا يُرِيدُ اللَّهُ لِيَجْعَلَ عَلَيْكُم مِّنْ حَرَجٍ وَلَٰكِن يُرِيدُ لِيُطَهِّرَكُمْ وَلِيُتِمَّ نِعْمَتَهُ عَلَيْكُمْ لَعَلَّكُمْ تَشْكُرُونَ
Éy yéen ñi gëm ! Bu ngeen jógee jëm ci julli, nangeen raxas seeni xar-kanam ak seeni yoxo ba ca seeni conc ; te nangeen laal [raay - masaa] seen bopp ; nangeen raxas it seeni tànk ba ca ñaari dojor ya. Waaye bu ngeen jógee ci joteg sëy, nangeen sangu ; bu ngeen woppee mbaa ngeen nekk ci tukki, mbaa kenn ci yéen jóge ci wanag wa, mbaa ngeen bànneexu ci jigéen te amuleen ndox, nangeen tiim ci pàkk bu laab, ngeen raay seen xar-kanam ak seeni yoxo. Yàlla nammuleen a teg aw tiis, waaye dafa leen a bëgg a laabal te matal xéewalam ci yéen ndax xéy-na ngeen sant Ko.
7وَاذْكُرُوا نِعْمَةَ اللَّهِ عَلَيْكُمْ وَمِيثَاقَهُ الَّذِي وَاثَقَكُم بِهِ إِذْ قُلْتُمْ سَمِعْنَا وَأَطَعْنَا ۖ وَاتَّقُوا اللَّهَ ۚ إِنَّ اللَّهَ عَلِيمٌ بِذَاتِ الصُّدُورِ
Fàttalikuleen xéewali Yàlla ci yéen, ak kóllare ya ngeen fasanteek Moom ba ngeen nee : “Dégg nanu te nangu nanu”. Te nangeen ragal Yàlla. Yàlla dey Ku xam li nekk ci xol yi la.
Al-MaidaFihi Alxuraan
120Aaya
MedinanRevelation
5Aaya
Tekki — Al-Maida 5
Simoore Al-Maida Aaya 5 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “Bis niki tey, dagan na ci yéen [ñam] yu sell…Simoore Aaya 5/120 — Al-Maida المائدة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Maida Dégg, Al-Maida Tekki, Al-Maida mp3, Al-Maida pdf. Aaya 3–7. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








