Al-'Ankabut · 1/69
Tekki Waxtaan — Simoore Al-'Ankabut
الم ۝١
Alif-Laaam-Meeem
📖 Tekkim Wolof
Alif, Laam, Miim.

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-3 — Simoore Al-'Ankabut

1الم
Alif, Laam, Miim.
2أَحَسِبَ النَّاسُ أَن يُتْرَكُوا أَن يَقُولُوا آمَنَّا وَهُمْ لَا يُفْتَنُونَ
Ndax nit ñi foog nañu ne danañu wax ne : “Gëm nañu ! ” te kenn duleen sànje ?
3وَلَقَدْ فَتَنَّا الَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ ۖ فَلَيَعْلَمَنَّ اللَّهُ الَّذِينَ صَدَقُوا وَلَيَعْلَمَنَّ الْكَاذِبِينَ
Sànje woon Nanu ña leen jiitu woon ; Yàlla xam na ñay dëggal ak ñay fen.
Al-'AnkabutFihi Alxuraan
69Aaya
MeccanRevelation
1Aaya

Tekki — Al-'Ankabut 1

Simoore Al-'Ankabut Aaya 1 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Alif, Laam, Miim.

Simoore Aaya 1/69 — Simoore Al-'Ankabut العنكبوت (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-'Ankabut Dégg, Simoore Al-'Ankabut Tekki, Simoore Al-'Ankabut mp3, Simoore Al-'Ankabut pdf. Aaya 1–3. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers