Al-'Ankabut · 2/69
Tekki Waxtaan — Simoore Al-'Ankabut
أَحَسِبَ النَّاسُ أَن يُتْرَكُوا أَن يَقُولُوا آمَنَّا وَهُمْ لَا يُفْتَنُونَ ۝٢
Ahasiban naasu anyu yutrakooo any yaqoolooo aamannaa wa hum la yuftanoon
📖 Tekkim Wolof
Ndax nit ñi foog nañu ne danañu wax ne : “Gëm nañu ! ” te kenn duleen sànje ?

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 1-4 — Simoore Al-'Ankabut

1الم
Alif, Laam, Miim.
2أَحَسِبَ النَّاسُ أَن يُتْرَكُوا أَن يَقُولُوا آمَنَّا وَهُمْ لَا يُفْتَنُونَ
Ndax nit ñi foog nañu ne danañu wax ne : “Gëm nañu ! ” te kenn duleen sànje ?
3وَلَقَدْ فَتَنَّا الَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ ۖ فَلَيَعْلَمَنَّ اللَّهُ الَّذِينَ صَدَقُوا وَلَيَعْلَمَنَّ الْكَاذِبِينَ
Sànje woon Nanu ña leen jiitu woon ; Yàlla xam na ñay dëggal ak ñay fen.
4أَمْ حَسِبَ الَّذِينَ يَعْمَلُونَ السَّيِّئَاتِ أَن يَسْبِقُونَا ۚ سَاءَ مَا يَحْكُمُونَ
Walla ñay jëfi ñaawteef, jàpp nañu ne danañu Nu jiitu ? Aka ñoo ñaaw ab àtte !
Al-'AnkabutFihi Alxuraan
69Aaya
MeccanRevelation
2Aaya

Tekki — Al-'Ankabut 2

Simoore Al-'Ankabut Aaya 2 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ndax nit ñi foog nañu ne danañu wax ne :…

Simoore Aaya 2/69 — Simoore Al-'Ankabut العنكبوت (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-'Ankabut Dégg, Simoore Al-'Ankabut Tekki, Simoore Al-'Ankabut mp3, Simoore Al-'Ankabut pdf. Aaya 1–4. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers