Al-Qasas · 2/88
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qasas
تِلْكَ آيَاتُ الْكِتَابِ الْمُبِينِ ۝٢
Tilka Aayaatul Kitaabil mubeen
📖 Tekkim Wolof
Lii mooy laayay Téere ba Nu biral.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 1-4 — Simoore Al-Qasas

1طسم
Taa, Siin, Miim.
2تِلْكَ آيَاتُ الْكِتَابِ الْمُبِينِ
Lii mooy laayay Téere ba Nu biral.
3نَتْلُو عَلَيْكَ مِن نَّبَإِ مُوسَىٰ وَفِرْعَوْنَ بِالْحَقِّ لِقَوْمٍ يُؤْمِنُونَ
Dananu la nettali ci xibaari Muusaa ak Frhawna ci dëgg, muy lu ñeel aw nit ñu gëm.
4إِنَّ فِرْعَوْنَ عَلَا فِي الْأَرْضِ وَجَعَلَ أَهْلَهَا شِيَعًا يَسْتَضْعِفُ طَائِفَةً مِّنْهُمْ يُذَبِّحُ أَبْنَاءَهُمْ وَيَسْتَحْيِي نِسَاءَهُمْ ۚ إِنَّهُ كَانَ مِنَ الْمُفْسِدِينَ
Firawna dadoon kawe-kawelu ci suuf si ; féewale waa réew ma, di jaamuloo ab kurél ci ñoom : ak a réndi seeni doom yu góor, di bàyyi jigéen ña. Moom Firawna yàqkat la woon.
Al-QasasFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
2Aaya

Tekki — Al-Qasas 2

Simoore Al-Qasas Aaya 2 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Lii mooy laayay Téere ba Nu biral.

Simoore Aaya 2/88 — Simoore Al-Qasas القصص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qasas Dégg, Simoore Al-Qasas Tekki, Simoore Al-Qasas mp3, Simoore Al-Qasas pdf. Aaya 1–4. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers