Simoore Al-Muddaththir ci Aarabu ak Wolof
Jàng Simoore Al-Muddaththir ak tekkim wolof bu mat sëkk, ak baat. Tekki ayaa bu ne. (56 Aaya — مكية). Al-Muddaththir Dégg, Al-Muddaththir Tekki, Al-Muddaththir mp3, Al-Muddaththir pdf.Jàng te Dégg Simoore Al-Muddaththir
🎧 Aaya
M
Mishary Rashid Alafasy
✓
Mishary Rashid Alafasy
✓
M
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
A
Abdurrahman As-Sudais
✓
Abdurrahman As-Sudais
✓
M
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
A
Abdul Basit Abdul Samad
✓
Abdul Basit Abdul Samad
✓
A
Ali Al-Hudhaify
✓
Ali Al-Hudhaify
✓
A
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
A
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
M
Muhammad Ayyoub
✓
Muhammad Ayyoub
✓
A
Abdullah Basfar
✓
Abdullah Basfar
✓
A
Abdullah Al-Juhani
✓
Abdullah Al-Juhani
✓
M
Maher Al Muaiqly
✓
Maher Al Muaiqly
✓
—
x1
ذَرْنِي وَمَنْ خَلَقْتُ وَحِيدًا ١١
📖 Tekki
Aaya 11
Bàyyi Ma ak ki nga xam ne maa ko bindoon nu wéet,
كَلَّا ۖ إِنَّهُ كَانَ لِآيَاتِنَا عَنِيدًا ١٦
📖 Tekki
Aaya 16
Te kat des na ! Ndax moom da daan lànk di bañ (Al xuraan) ji.
فَقَالَ إِنْ هَٰذَا إِلَّا سِحْرٌ يُؤْثَرُ ٢٤
📖 Tekki
Aaya 24
Mu daldi wax ne : “Alxuraan jii daal ag njibar doŋŋ la
وَمَا جَعَلْنَا أَصْحَابَ النَّارِ إِلَّا مَلَائِكَةً ۙ وَمَا جَعَلْنَا عِدَّتَهُمْ إِلَّا فِتْنَةً لِّلَّذِينَ كَفَرُوا لِيَسْتَيْقِنَ الَّذِينَ أُوتُوا الْكِتَابَ وَيَزْدَادَ الَّذِينَ آمَنُوا إِيمَانًا ۙ وَلَا يَرْتَابَ الَّذِينَ أُوتُوا الْكِتَابَ وَالْمُؤْمِنُونَ ۙ وَلِيَقُولَ الَّذِينَ فِي قُلُوبِهِم مَّرَضٌ وَالْكَافِرُونَ مَاذَا أَرَادَ اللَّهُ بِهَٰذَا مَثَلًا ۚ كَذَٰلِكَ يُضِلُّ اللَّهُ مَن يَشَاءُ وَيَهْدِي مَن يَشَاءُ ۚ وَمَا يَعْلَمُ جُنُودَ رَبِّكَ إِلَّا هُوَ ۚ وَمَا هِيَ إِلَّا ذِكْرَىٰ لِلْبَشَرِ ٣١
📖 Tekki
Aaya 31
Ay Malaaka rekk ay wattu Safara. Te, lu ñuy bari bari nekku wu ñu fa lu dul fitnaal yéefar yi, ak tiiñal ñoñ Téere, ak dolli ngëmug ña gëmoon, ak it ñoñ Téere ak way gëm ña baña dengi-dengi ; ak it ngir yéefar yaak ña seeni xol wopp di wax naan : “Ana lu Yàlla namm ci misaal mii ? ” Noonu la Yàlla réerële ku ko soob di gindi it ku ko soob. Te sa xarekati Boroom, Moom doŋŋ leen xam. Te lii du lenn lu dul luy fàttali bindéef yi jàjj leen.
لِمَن شَاءَ مِنكُمْ أَن يَتَقَدَّمَ أَوْ يَتَأَخَّرَ ٣٧
📖 Tekki
Aaya 37
Ku mu soob ci yéen, na jiitu walla mu des ginnaaw.
كُلُّ نَفْسٍ بِمَا كَسَبَتْ رَهِينَةٌ ٣٨
📖 Tekki
Aaya 38
Bakkan bu mu mana doon ag tayle la ci jëfam.
مَا سَلَكَكُمْ فِي سَقَرَ ٤٢
📖 Tekki
Aaya 42
“(Naan) Ana lan mooleen wara duggloo Safaraw Saqar ? ”
فَمَا تَنفَعُهُمْ شَفَاعَةُ الشَّافِعِينَ ٤٨
📖 Tekki
Aaya 48
Rammug rammukat, du leen fa jariñ dara.
فَمَا لَهُمْ عَنِ التَّذْكِرَةِ مُعْرِضِينَ ٤٩
📖 Tekki
Aaya 49
Ana lan moo leen dëdëleek fàttaliku ?
بَلْ يُرِيدُ كُلُّ امْرِئٍ مِّنْهُمْ أَن يُؤْتَىٰ صُحُفًا مُّنَشَّرَةً ٥٢
📖 Tekki
Aaya 52
Kenn ku nekk ci ñoom bëggoon na ñu jox ko ay kayit yu teqalikoo.
كَلَّا ۖ بَل لَّا يَخَافُونَ الْآخِرَةَ ٥٣
📖 Tekki
Aaya 53
Dee wa laay ! Ñoom ragalu ñu woon àllaaxira.
وَمَا يَذْكُرُونَ إِلَّا أَن يَشَاءَ اللَّهُ ۚ هُوَ أَهْلُ التَّقْوَىٰ وَأَهْلُ الْمَغْفِرَةِ ٥٦
📖 Tekki
Aaya 56
Te manuñoo fàttaliku lu dul ci bu soobee Yàlla. Te moo gëna yayoo ci ragal ko ; te moom doŋŋa am njégël.
Jàng Simoore Al-Muddaththir ci Wolof – Tekki, Waxtaan ak Baat
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers

