Al-Muddaththir · 55/56
Tekki Waxtaan — Al-Muddaththir
فَمَن شَاءَ ذَكَرَهُ ۝٥٥
Fa man shaaa`a zakarah
📖 Tekkim Wolof
Kéep ku mu soob, na fàttaliku.

🎧 Dégg


📜 Aaya 53-56 — Al-Muddaththir

53كَلَّا ۖ بَل لَّا يَخَافُونَ الْآخِرَةَ
Dee wa laay ! Ñoom ragalu ñu woon àllaaxira.
54كَلَّا إِنَّهُ تَذْكِرَةٌ
Mukk ! Te lii ag fàttali la.
55فَمَن شَاءَ ذَكَرَهُ
Kéep ku mu soob, na fàttaliku.
56وَمَا يَذْكُرُونَ إِلَّا أَن يَشَاءَ اللَّهُ ۚ هُوَ أَهْلُ التَّقْوَىٰ وَأَهْلُ الْمَغْفِرَةِ
Te manuñoo fàttaliku lu dul ci bu soobee Yàlla. Te moo gëna yayoo ci ragal ko ; te moom doŋŋa am njégël.
Al-MuddaththirFihi Alxuraan
56Aaya
MeccanRevelation
55Aaya

Tekki — Al-Muddaththir 55

Simoore Al-Muddaththir Aaya 55 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Kéep ku mu soob, na fàttaliku.

Simoore Aaya 55/56 — Al-Muddaththir المدثر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Muddaththir Dégg, Al-Muddaththir Tekki, Al-Muddaththir mp3, Al-Muddaththir pdf. Aaya 53–56. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers