Al-Muddaththir · 14/56
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Muddaththir
وَمَهَّدتُّ لَهُ تَمْهِيدًا ۝١٤
Wa mahhattu lahoo tamheeda
📖 Tekkim Wolof
te Ma dindiloon ko bépp jafe-jafe.

🎧 Dégg


📜 Aaya 12-16 — Simoore Al-Muddaththir

12وَجَعَلْتُ لَهُ مَالًا مَّمْدُودًا
te ma joxoñ ko alal ju yaatu,
13وَبَنِينَ شُهُودًا
ak doom yu ko daan wéttali,
14وَمَهَّدتُّ لَهُ تَمْهِيدًا
te Ma dindiloon ko bépp jafe-jafe.
15ثُمَّ يَطْمَعُ أَنْ أَزِيدَ
te mo daan xemmeem saa su nekk Ma di ko dolli.
16كَلَّا ۖ إِنَّهُ كَانَ لِآيَاتِنَا عَنِيدًا
Te kat des na ! Ndax moom da daan lànk di bañ (Al xuraan) ji.
Al-MuddaththirFihi Alxuraan
56Aaya
MeccanRevelation
14Aaya

Tekki — Al-Muddaththir 14

Simoore Al-Muddaththir Aaya 14 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te Ma dindiloon ko bépp jafe-jafe.

Simoore Aaya 14/56 — Simoore Al-Muddaththir المدثر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Muddaththir Dégg, Simoore Al-Muddaththir Tekki, Simoore Al-Muddaththir mp3, Simoore Al-Muddaththir pdf. Aaya 12–16. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers