Al-Muddaththir · 17/56
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Muddaththir
سَأُرْهِقُهُ صَعُودًا ۝١٧
Sa urhiquhoo sa`oodaa
📖 Tekkim Wolof
Danaa ko sonale yéegu tundu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 15-19 — Simoore Al-Muddaththir

15ثُمَّ يَطْمَعُ أَنْ أَزِيدَ
te mo daan xemmeem saa su nekk Ma di ko dolli.
16كَلَّا ۖ إِنَّهُ كَانَ لِآيَاتِنَا عَنِيدًا
Te kat des na ! Ndax moom da daan lànk di bañ (Al xuraan) ji.
17سَأُرْهِقُهُ صَعُودًا
Danaa ko sonale yéegu tundu.
18إِنَّهُ فَكَّرَ وَقَدَّرَ
Moom day xalaat. Na daldi soobu.
19فَقُتِلَ كَيْفَ قَدَّرَ
Nu daldi koy rey ! Ca na mu sóobóo !
Al-MuddaththirFihi Alxuraan
56Aaya
MeccanRevelation
17Aaya

Tekki — Al-Muddaththir 17

Simoore Al-Muddaththir Aaya 17 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Danaa ko sonale yéegu tundu.

Simoore Aaya 17/56 — Simoore Al-Muddaththir المدثر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Muddaththir Dégg, Simoore Al-Muddaththir Tekki, Simoore Al-Muddaththir mp3, Simoore Al-Muddaththir pdf. Aaya 15–19. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers