Al-Muddaththir · 32/56
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Muddaththir
كَلَّا وَالْقَمَرِ ۝٣٢
Kallaa walqamar
📖 Tekkim Wolof
Déet !... maa ngi giñ ci weer wi !

🎧 Dégg


📜 Aaya 30-34 — Simoore Al-Muddaththir

30عَلَيْهَا تِسْعَةَ عَشَرَ
Fukki (Malaaka) ak juróom-ñanant koy wattu.
31وَمَا جَعَلْنَا أَصْحَابَ النَّارِ إِلَّا مَلَائِكَةً ۙ وَمَا جَعَلْنَا عِدَّتَهُمْ إِلَّا فِتْنَةً لِّلَّذِينَ كَفَرُوا لِيَسْتَيْقِنَ الَّذِينَ أُوتُوا الْكِتَابَ وَيَزْدَادَ الَّذِينَ آمَنُوا إِيمَانًا ۙ وَلَا يَرْتَابَ الَّذِينَ أُوتُوا الْكِتَابَ وَالْمُؤْمِنُونَ ۙ وَلِيَقُولَ الَّذِينَ فِي قُلُوبِهِم مَّرَضٌ وَالْكَافِرُونَ مَاذَا أَرَادَ اللَّهُ بِهَٰذَا مَثَلًا ۚ كَذَٰلِكَ يُضِلُّ اللَّهُ مَن يَشَاءُ وَيَهْدِي مَن يَشَاءُ ۚ وَمَا يَعْلَمُ جُنُودَ رَبِّكَ إِلَّا هُوَ ۚ وَمَا هِيَ إِلَّا ذِكْرَىٰ لِلْبَشَرِ
Ay Malaaka rekk ay wattu Safara. Te, lu ñuy bari bari nekku wu ñu fa lu dul fitnaal yéefar yi, ak tiiñal ñoñ Téere, ak dolli ngëmug ña gëmoon, ak it ñoñ Téere ak way gëm ña baña dengi-dengi ; ak it ngir yéefar yaak ña seeni xol wopp di wax naan : “Ana lu Yàlla namm ci misaal mii ? ” Noonu la Yàlla réerële ku ko soob di gindi it ku ko soob. Te sa xarekati Boroom, Moom doŋŋ leen xam. Te lii du lenn lu dul luy fàttali bindéef yi jàjj leen.
32كَلَّا وَالْقَمَرِ
Déet !... maa ngi giñ ci weer wi !
33وَاللَّيْلِ إِذْ أَدْبَرَ
Ak ci guddi su nee wërëñ !
34وَالصُّبْحِ إِذَا أَسْفَرَ
Ak su fajar si di xar!
Al-MuddaththirFihi Alxuraan
56Aaya
MeccanRevelation
32Aaya

Tekki — Al-Muddaththir 32

Simoore Al-Muddaththir Aaya 32 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Déet !... maa ngi giñ ci weer wi !

Simoore Aaya 32/56 — Simoore Al-Muddaththir المدثر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Muddaththir Dégg, Simoore Al-Muddaththir Tekki, Simoore Al-Muddaththir mp3, Simoore Al-Muddaththir pdf. Aaya 30–34. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers