Al-Muddaththir · 24/56
Tekki Waxtaan — Al-Muddaththir
فَقَالَ إِنْ هَٰذَا إِلَّا سِحْرٌ يُؤْثَرُ ۝٢٤
Faqaala in haazaaa illaa sihruny yu`sar
📖 Tekkim Wolof
Mu daldi wax ne : “Alxuraan jii daal ag njibar doŋŋ la
🎧 Dégg

📜 Aaya 22-26 — Al-Muddaththir

22ثُمَّ عَبَسَ وَبَسَرَ
Daldi nay gaññ te sóomórlu.
23ثُمَّ أَدْبَرَ وَاسْتَكْبَرَ
Topp mu daldi dumóoyu tey rëy-rëylu.
24فَقَالَ إِنْ هَٰذَا إِلَّا سِحْرٌ يُؤْثَرُ
Mu daldi wax ne : “Alxuraan jii daal ag njibar doŋŋ la
25إِنْ هَٰذَا إِلَّا قَوْلُ الْبَشَرِ
lii daal du leen lu dul waxi nit”.
26سَأُصْلِيهِ سَقَرَ
Kookee dey danaa ko lakk ci Safaraw (Saqar).
Al-MuddaththirFihi Alxuraan
56Aaya
MeccanRevelation
24Aaya

Tekki — Al-Muddaththir 24

Simoore Al-Muddaththir Aaya 24 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu daldi wax ne : “Alxuraan jii daal ag njibar…

Simoore Aaya 24/56 — Al-Muddaththir المدثر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Muddaththir Dégg, Al-Muddaththir Tekki, Al-Muddaththir mp3, Al-Muddaththir pdf. Aaya 22–26. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers