Al-Muddaththir · 29/56
Tekki Waxtaan — Al-Muddaththir
لَوَّاحَةٌ لِّلْبَشَرِ ۝٢٩
Lawwaahatul lilbashar
📖 Tekkim Wolof
Dafay alawtiku ab der di ko xëmël.

🎧 Dégg


📜 Aaya 27-31 — Al-Muddaththir

27وَمَا أَدْرَاكَ مَا سَقَرُ
Ana kan moo lay xamal luy Saqar ?
28لَا تُبْقِي وَلَا تَذَرُ
Du bàyyi dara ;
29لَوَّاحَةٌ لِّلْبَشَرِ
Dafay alawtiku ab der di ko xëmël.
30عَلَيْهَا تِسْعَةَ عَشَرَ
Fukki (Malaaka) ak juróom-ñanant koy wattu.
31وَمَا جَعَلْنَا أَصْحَابَ النَّارِ إِلَّا مَلَائِكَةً ۙ وَمَا جَعَلْنَا عِدَّتَهُمْ إِلَّا فِتْنَةً لِّلَّذِينَ كَفَرُوا لِيَسْتَيْقِنَ الَّذِينَ أُوتُوا الْكِتَابَ وَيَزْدَادَ الَّذِينَ آمَنُوا إِيمَانًا ۙ وَلَا يَرْتَابَ الَّذِينَ أُوتُوا الْكِتَابَ وَالْمُؤْمِنُونَ ۙ وَلِيَقُولَ الَّذِينَ فِي قُلُوبِهِم مَّرَضٌ وَالْكَافِرُونَ مَاذَا أَرَادَ اللَّهُ بِهَٰذَا مَثَلًا ۚ كَذَٰلِكَ يُضِلُّ اللَّهُ مَن يَشَاءُ وَيَهْدِي مَن يَشَاءُ ۚ وَمَا يَعْلَمُ جُنُودَ رَبِّكَ إِلَّا هُوَ ۚ وَمَا هِيَ إِلَّا ذِكْرَىٰ لِلْبَشَرِ
Ay Malaaka rekk ay wattu Safara. Te, lu ñuy bari bari nekku wu ñu fa lu dul fitnaal yéefar yi, ak tiiñal ñoñ Téere, ak dolli ngëmug ña gëmoon, ak it ñoñ Téere ak way gëm ña baña dengi-dengi ; ak it ngir yéefar yaak ña seeni xol wopp di wax naan : “Ana lu Yàlla namm ci misaal mii ? ” Noonu la Yàlla réerële ku ko soob di gindi it ku ko soob. Te sa xarekati Boroom, Moom doŋŋ leen xam. Te lii du lenn lu dul luy fàttali bindéef yi jàjj leen.
Al-MuddaththirFihi Alxuraan
56Aaya
MeccanRevelation
29Aaya

Tekki — Al-Muddaththir 29

Simoore Al-Muddaththir Aaya 29 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Dafay alawtiku ab der di ko xëmël.

Simoore Aaya 29/56 — Al-Muddaththir المدثر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Muddaththir Dégg, Al-Muddaththir Tekki, Al-Muddaththir mp3, Al-Muddaththir pdf. Aaya 27–31. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers