Al-Muddaththir · 25/56
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Muddaththir
إِنْ هَٰذَا إِلَّا قَوْلُ الْبَشَرِ ۝٢٥
In haazaaa illaa qawlul bashar
📖 Tekkim Wolof
lii daal du leen lu dul waxi nit”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 23-27 — Simoore Al-Muddaththir

23ثُمَّ أَدْبَرَ وَاسْتَكْبَرَ
Topp mu daldi dumóoyu tey rëy-rëylu.
24فَقَالَ إِنْ هَٰذَا إِلَّا سِحْرٌ يُؤْثَرُ
Mu daldi wax ne : “Alxuraan jii daal ag njibar doŋŋ la
25إِنْ هَٰذَا إِلَّا قَوْلُ الْبَشَرِ
lii daal du leen lu dul waxi nit”.
26سَأُصْلِيهِ سَقَرَ
Kookee dey danaa ko lakk ci Safaraw (Saqar).
27وَمَا أَدْرَاكَ مَا سَقَرُ
Ana kan moo lay xamal luy Saqar ?
Al-MuddaththirFihi Alxuraan
56Aaya
MeccanRevelation
25Aaya

Tekki — Al-Muddaththir 25

Simoore Al-Muddaththir Aaya 25 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : lii daal du leen lu dul waxi nit”.

Simoore Aaya 25/56 — Simoore Al-Muddaththir المدثر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Muddaththir Dégg, Simoore Al-Muddaththir Tekki, Simoore Al-Muddaththir mp3, Simoore Al-Muddaththir pdf. Aaya 23–27. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers