Al-Muddaththir · 15/56
Tekki Waxtaan — Al-Muddaththir
ثُمَّ يَطْمَعُ أَنْ أَزِيدَ ۝١٥
Summa yat ma`u an azeed
📖 Tekkim Wolof
te mo daan xemmeem saa su nekk Ma di ko dolli.

🎧 Dégg


📜 Aaya 13-17 — Al-Muddaththir

13وَبَنِينَ شُهُودًا
ak doom yu ko daan wéttali,
14وَمَهَّدتُّ لَهُ تَمْهِيدًا
te Ma dindiloon ko bépp jafe-jafe.
15ثُمَّ يَطْمَعُ أَنْ أَزِيدَ
te mo daan xemmeem saa su nekk Ma di ko dolli.
16كَلَّا ۖ إِنَّهُ كَانَ لِآيَاتِنَا عَنِيدًا
Te kat des na ! Ndax moom da daan lànk di bañ (Al xuraan) ji.
17سَأُرْهِقُهُ صَعُودًا
Danaa ko sonale yéegu tundu.
Al-MuddaththirFihi Alxuraan
56Aaya
MeccanRevelation
15Aaya

Tekki — Al-Muddaththir 15

Simoore Al-Muddaththir Aaya 15 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te mo daan xemmeem saa su nekk Ma di ko…

Simoore Aaya 15/56 — Al-Muddaththir المدثر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Muddaththir Dégg, Al-Muddaththir Tekki, Al-Muddaththir mp3, Al-Muddaththir pdf. Aaya 13–17. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers