Al-Muddaththir · 26/56
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Muddaththir
سَأُصْلِيهِ سَقَرَ ۝٢٦
Sa usleehi saqar
📖 Tekkim Wolof
Kookee dey danaa ko lakk ci Safaraw (Saqar).

🎧 Dégg


📜 Aaya 24-28 — Simoore Al-Muddaththir

24فَقَالَ إِنْ هَٰذَا إِلَّا سِحْرٌ يُؤْثَرُ
Mu daldi wax ne : “Alxuraan jii daal ag njibar doŋŋ la
25إِنْ هَٰذَا إِلَّا قَوْلُ الْبَشَرِ
lii daal du leen lu dul waxi nit”.
26سَأُصْلِيهِ سَقَرَ
Kookee dey danaa ko lakk ci Safaraw (Saqar).
27وَمَا أَدْرَاكَ مَا سَقَرُ
Ana kan moo lay xamal luy Saqar ?
28لَا تُبْقِي وَلَا تَذَرُ
Du bàyyi dara ;
Al-MuddaththirFihi Alxuraan
56Aaya
MeccanRevelation
26Aaya

Tekki — Al-Muddaththir 26

Simoore Al-Muddaththir Aaya 26 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Kookee dey danaa ko lakk ci Safaraw (Saqar).

Simoore Aaya 26/56 — Simoore Al-Muddaththir المدثر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Muddaththir Dégg, Simoore Al-Muddaththir Tekki, Simoore Al-Muddaththir mp3, Simoore Al-Muddaththir pdf. Aaya 24–28. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers