Al-Muddaththir · 16/56
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Muddaththir
كَلَّا ۖ إِنَّهُ كَانَ لِآيَاتِنَا عَنِيدًا ۝١٦
Kallaaa innahoo kaana li Aayaatinaa `aneedaa
📖 Tekkim Wolof
Te kat des na ! Ndax moom da daan lànk di bañ (Al xuraan) ji.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 14-18 — Simoore Al-Muddaththir

14وَمَهَّدتُّ لَهُ تَمْهِيدًا
te Ma dindiloon ko bépp jafe-jafe.
15ثُمَّ يَطْمَعُ أَنْ أَزِيدَ
te mo daan xemmeem saa su nekk Ma di ko dolli.
16كَلَّا ۖ إِنَّهُ كَانَ لِآيَاتِنَا عَنِيدًا
Te kat des na ! Ndax moom da daan lànk di bañ (Al xuraan) ji.
17سَأُرْهِقُهُ صَعُودًا
Danaa ko sonale yéegu tundu.
18إِنَّهُ فَكَّرَ وَقَدَّرَ
Moom day xalaat. Na daldi soobu.
Al-MuddaththirFihi Alxuraan
56Aaya
MeccanRevelation
16Aaya

Tekki — Al-Muddaththir 16

Simoore Al-Muddaththir Aaya 16 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te kat des na ! Ndax moom da daan lànk…

Simoore Aaya 16/56 — Simoore Al-Muddaththir المدثر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Muddaththir Dégg, Simoore Al-Muddaththir Tekki, Simoore Al-Muddaththir mp3, Simoore Al-Muddaththir pdf. Aaya 14–18. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers