Al-Muddaththir · 54/56
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Muddaththir
كَلَّا إِنَّهُ تَذْكِرَةٌ ۝٥٤
Kallaaa innahoo tazkirah
📖 Tekkim Wolof
Mukk ! Te lii ag fàttali la.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 52-56 — Simoore Al-Muddaththir

52بَلْ يُرِيدُ كُلُّ امْرِئٍ مِّنْهُمْ أَن يُؤْتَىٰ صُحُفًا مُّنَشَّرَةً
Kenn ku nekk ci ñoom bëggoon na ñu jox ko ay kayit yu teqalikoo.
53كَلَّا ۖ بَل لَّا يَخَافُونَ الْآخِرَةَ
Dee wa laay ! Ñoom ragalu ñu woon àllaaxira.
54كَلَّا إِنَّهُ تَذْكِرَةٌ
Mukk ! Te lii ag fàttali la.
55فَمَن شَاءَ ذَكَرَهُ
Kéep ku mu soob, na fàttaliku.
56وَمَا يَذْكُرُونَ إِلَّا أَن يَشَاءَ اللَّهُ ۚ هُوَ أَهْلُ التَّقْوَىٰ وَأَهْلُ الْمَغْفِرَةِ
Te manuñoo fàttaliku lu dul ci bu soobee Yàlla. Te moo gëna yayoo ci ragal ko ; te moom doŋŋa am njégël.
Al-MuddaththirFihi Alxuraan
56Aaya
MeccanRevelation
54Aaya

Tekki — Al-Muddaththir 54

Simoore Al-Muddaththir Aaya 54 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mukk ! Te lii ag fàttali la.

Simoore Aaya 54/56 — Simoore Al-Muddaththir المدثر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Muddaththir Dégg, Simoore Al-Muddaththir Tekki, Simoore Al-Muddaththir mp3, Simoore Al-Muddaththir pdf. Aaya 52–56. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers