Al-Muddaththir · 23/56
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Muddaththir
ثُمَّ أَدْبَرَ وَاسْتَكْبَرَ ۝٢٣
Summaa adbara wastakbar
📖 Tekkim Wolof
Topp mu daldi dumóoyu tey rëy-rëylu.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 21-25 — Simoore Al-Muddaththir

21ثُمَّ نَظَرَ
Mu daldi, xool.
22ثُمَّ عَبَسَ وَبَسَرَ
Daldi nay gaññ te sóomórlu.
23ثُمَّ أَدْبَرَ وَاسْتَكْبَرَ
Topp mu daldi dumóoyu tey rëy-rëylu.
24فَقَالَ إِنْ هَٰذَا إِلَّا سِحْرٌ يُؤْثَرُ
Mu daldi wax ne : “Alxuraan jii daal ag njibar doŋŋ la
25إِنْ هَٰذَا إِلَّا قَوْلُ الْبَشَرِ
lii daal du leen lu dul waxi nit”.
Al-MuddaththirFihi Alxuraan
56Aaya
MeccanRevelation
23Aaya

Tekki — Al-Muddaththir 23

Simoore Al-Muddaththir Aaya 23 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Topp mu daldi dumóoyu tey rëy-rëylu.

Simoore Aaya 23/56 — Simoore Al-Muddaththir المدثر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Muddaththir Dégg, Simoore Al-Muddaththir Tekki, Simoore Al-Muddaththir mp3, Simoore Al-Muddaththir pdf. Aaya 21–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers