Maryam · 1/98
Tekki Waxtaan — Maryam
كهيعص ۝١
Kaaaf-Haa-Yaa-`Ayyyn-Saaad
📖 Tekkim Wolof
Kaaf, Haa, Yaa, Ayin, Saad.
🎧 Dégg

📜 Aaya 1-3 — Maryam

1كهيعص
Kaaf, Haa, Yaa, Ayin, Saad.
2ذِكْرُ رَحْمَتِ رَبِّكَ عَبْدَهُ زَكَرِيَّا
[Fàttalikul] firndey yërmaandey sa Boroom ca jaamam ba Zakariyaa.
3إِذْ نَادَىٰ رَبَّهُ نِدَاءً خَفِيًّا
Jamono ja muy ñaan Boroomam ci ag yalu,
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
1Aaya

Tekki — Maryam 1

Simoore Maryam Aaya 1 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Kaaf, Haa, Yaa, Ayin, Saad.

Simoore Aaya 1/98 — Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Maryam Dégg, Maryam Tekki, Maryam mp3, Maryam pdf. Aaya 1–3. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers