Al-Hashr · 2/24
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hashr
هُوَ الَّذِي أَخْرَجَ الَّذِينَ كَفَرُوا مِنْ أَهْلِ الْكِتَابِ مِن دِيَارِهِمْ لِأَوَّلِ الْحَشْرِ ۚ مَا ظَنَنتُمْ أَن يَخْرُجُوا ۖ وَظَنُّوا أَنَّهُم مَّانِعَتُهُمْ حُصُونُهُم مِّنَ اللَّهِ فَأَتَاهُمُ اللَّهُ مِنْ حَيْثُ لَمْ يَحْتَسِبُوا ۖ وَقَذَفَ فِي قُلُوبِهِمُ الرُّعْبَ ۚ يُخْرِبُونَ بُيُوتَهُم بِأَيْدِيهِمْ وَأَيْدِي الْمُؤْمِنِينَ فَاعْتَبِرُوا يَا أُولِي الْأَبْصَارِ ۝٢
Huwal lazeee akharajal lazeena kafaroo min ahlil kitaabi min diyaarihim li awwalil Hashr; maa zanantum any yakhrujoo wa zannooo annahum maa ni`atuhum husoonuhum minal laahi faataahumul laahu min haisu lam yahtasiboo wa qazafa fee quloobihimur ru`ba yukhriboona bu yootahum bi aydeehim wa aydil mu`mineena fa`tabiroo yaaa ulil absaar
📖 Tekkim Wolof
Te mooy Yàlla moo génnee woon ña weddi te bokk ci, ñoñ Téere (Yahuudi Madiina), ci seen kër ca njaalbeenuk màng ga (Jëm Saam). Jortuleen woon ne danañu génn, ñoom (Yahudd ya it) jortoon nañu ne seeni tata dana leen aar. (Yàlla) daldi nay tàbbal tiitange ci seen xol,. Ñu tàmbalee gental seen kër ya ci seeni yoxo, ak yoxoy jullit ñi. Xalamleen (xalaat), yéen ñi am am njis mu leer.

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-4 — Simoore Al-Hashr

1سَبَّحَ لِلَّهِ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ ۖ وَهُوَ الْعَزِيزُ الْحَكِيمُ
Ñi nekk ci Asamaan yeek suuf si ñi ngi sàbbaal Yàlla, te moo di boroom kàttan gi, di Ku xereñ ki.
2هُوَ الَّذِي أَخْرَجَ الَّذِينَ كَفَرُوا مِنْ أَهْلِ الْكِتَابِ مِن دِيَارِهِمْ لِأَوَّلِ الْحَشْرِ ۚ مَا ظَنَنتُمْ أَن يَخْرُجُوا ۖ وَظَنُّوا أَنَّهُم مَّانِعَتُهُمْ حُصُونُهُم مِّنَ اللَّهِ فَأَتَاهُمُ اللَّهُ مِنْ حَيْثُ لَمْ يَحْتَسِبُوا ۖ وَقَذَفَ فِي قُلُوبِهِمُ الرُّعْبَ ۚ يُخْرِبُونَ بُيُوتَهُم بِأَيْدِيهِمْ وَأَيْدِي الْمُؤْمِنِينَ فَاعْتَبِرُوا يَا أُولِي الْأَبْصَارِ
Te mooy Yàlla moo génnee woon ña weddi te bokk ci, ñoñ Téere (Yahuudi Madiina), ci seen kër ca njaalbeenuk màng ga (Jëm Saam). Jortuleen woon ne danañu génn, ñoom (Yahudd ya it) jortoon nañu ne seeni tata dana leen aar. (Yàlla) daldi nay tàbbal tiitange ci seen xol,. Ñu tàmbalee gental seen kër ya ci seeni yoxo, ak yoxoy jullit ñi. Xalamleen (xalaat), yéen ñi am am njis mu leer.
3وَلَوْلَا أَن كَتَبَ اللَّهُ عَلَيْهِمُ الْجَلَاءَ لَعَذَّبَهُمْ فِي الدُّنْيَا ۖ وَلَهُمْ فِي الْآخِرَةِ عَذَابُ النَّارِ
Su Yàlla dogalul woon seenug génn (réew mi), kon dey Mu mbugël leen ci àddina ; te bu àllaaxiraa it ñu am mbugëlum Safara.
4ذَٰلِكَ بِأَنَّهُمْ شَاقُّوا اللَّهَ وَرَسُولَهُ ۖ وَمَن يُشَاقِّ اللَّهَ فَإِنَّ اللَّهَ شَدِيدُ الْعِقَابِ
Li ko waral moo di ne ñoom dañoo juuyoo woon ak Yàlla ak ub Yonentam. Te nag képp kuy juuyook Yàlla... moom di boroom mbugël mu tar.
Al-HashrFihi Alxuraan
24Aaya
MedinanRevelation
2Aaya

Tekki — Al-Hashr 2

Simoore Al-Hashr Aaya 2 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te mooy Yàlla moo génnee woon ña weddi te bokk…

Simoore Aaya 2/24 — Simoore Al-Hashr الحشر (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hashr Dégg, Simoore Al-Hashr Tekki, Simoore Al-Hashr mp3, Simoore Al-Hashr pdf. Aaya 1–4. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers