Al-Hashr · 1/24
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hashr
سَبَّحَ لِلَّهِ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ ۖ وَهُوَ الْعَزِيزُ الْحَكِيمُ ۝١
Sabbaha lillaahi maa fissamaawaati wa maa fil ardi wa Huwal `Azeezul Hakeem
📖 Tekkim Wolof
Ñi nekk ci Asamaan yeek suuf si ñi ngi sàbbaal Yàlla, te moo di boroom kàttan gi, di Ku xereñ ki.

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-3 — Simoore Al-Hashr

1سَبَّحَ لِلَّهِ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ ۖ وَهُوَ الْعَزِيزُ الْحَكِيمُ
Ñi nekk ci Asamaan yeek suuf si ñi ngi sàbbaal Yàlla, te moo di boroom kàttan gi, di Ku xereñ ki.
2هُوَ الَّذِي أَخْرَجَ الَّذِينَ كَفَرُوا مِنْ أَهْلِ الْكِتَابِ مِن دِيَارِهِمْ لِأَوَّلِ الْحَشْرِ ۚ مَا ظَنَنتُمْ أَن يَخْرُجُوا ۖ وَظَنُّوا أَنَّهُم مَّانِعَتُهُمْ حُصُونُهُم مِّنَ اللَّهِ فَأَتَاهُمُ اللَّهُ مِنْ حَيْثُ لَمْ يَحْتَسِبُوا ۖ وَقَذَفَ فِي قُلُوبِهِمُ الرُّعْبَ ۚ يُخْرِبُونَ بُيُوتَهُم بِأَيْدِيهِمْ وَأَيْدِي الْمُؤْمِنِينَ فَاعْتَبِرُوا يَا أُولِي الْأَبْصَارِ
Te mooy Yàlla moo génnee woon ña weddi te bokk ci, ñoñ Téere (Yahuudi Madiina), ci seen kër ca njaalbeenuk màng ga (Jëm Saam). Jortuleen woon ne danañu génn, ñoom (Yahudd ya it) jortoon nañu ne seeni tata dana leen aar. (Yàlla) daldi nay tàbbal tiitange ci seen xol,. Ñu tàmbalee gental seen kër ya ci seeni yoxo, ak yoxoy jullit ñi. Xalamleen (xalaat), yéen ñi am am njis mu leer.
3وَلَوْلَا أَن كَتَبَ اللَّهُ عَلَيْهِمُ الْجَلَاءَ لَعَذَّبَهُمْ فِي الدُّنْيَا ۖ وَلَهُمْ فِي الْآخِرَةِ عَذَابُ النَّارِ
Su Yàlla dogalul woon seenug génn (réew mi), kon dey Mu mbugël leen ci àddina ; te bu àllaaxiraa it ñu am mbugëlum Safara.
Al-HashrFihi Alxuraan
24Aaya
MedinanRevelation
1Aaya

Tekki — Al-Hashr 1

Simoore Al-Hashr Aaya 1 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñi nekk ci Asamaan yeek suuf si ñi ngi sàbbaal…

Simoore Aaya 1/24 — Simoore Al-Hashr الحشر (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hashr Dégg, Simoore Al-Hashr Tekki, Simoore Al-Hashr mp3, Simoore Al-Hashr pdf. Aaya 1–3. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers