Al-Jinn · 1/28
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Jinn
قُلْ أُوحِيَ إِلَيَّ أَنَّهُ اسْتَمَعَ نَفَرٌ مِّنَ الْجِنِّ فَقَالُوا إِنَّا سَمِعْنَا قُرْآنًا عَجَبًا ۝١
Qul oohiya ilaiya annna hustama`a nafarum minal jinnni faqaalooo innaa sami`naa quraanan `ajabaa
📖 Tekkim Wolof
Waxal ne : “Soloof na ma am na mbooleem jinne muy déglu, bay wax naan : “Nun dey dégg nanu Ñjàngum [Alxuraan] mu yéeme,

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-3 — Simoore Al-Jinn

1قُلْ أُوحِيَ إِلَيَّ أَنَّهُ اسْتَمَعَ نَفَرٌ مِّنَ الْجِنِّ فَقَالُوا إِنَّا سَمِعْنَا قُرْآنًا عَجَبًا
Waxal ne : “Soloof na ma am na mbooleem jinne muy déglu, bay wax naan : “Nun dey dégg nanu Ñjàngum [Alxuraan] mu yéeme,
2يَهْدِي إِلَى الرُّشْدِ فَآمَنَّا بِهِ ۖ وَلَن نُّشْرِكَ بِرَبِّنَا أَحَدًا
dafay gindee jëme ci njub. Nu daldi koy gëm, te dunu bokkaale dara ci sunu Boroom.
3وَأَنَّهُ تَعَالَىٰ جَدُّ رَبِّنَا مَا اتَّخَذَ صَاحِبَةً وَلَا وَلَدًا
Te sunu Boroom - màggam ga sell na - jàppewul kenn muy soxnaam, waxatumalaa doomam !
Al-JinnFihi Alxuraan
28Aaya
MeccanRevelation
1Aaya

Tekki — Al-Jinn 1

Simoore Al-Jinn Aaya 1 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waxal ne : “Soloof na ma am na mbooleem jinne…

Simoore Aaya 1/28 — Simoore Al-Jinn الجن (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Jinn Dégg, Simoore Al-Jinn Tekki, Simoore Al-Jinn mp3, Simoore Al-Jinn pdf. Aaya 1–3. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers