Simoore Al-Qari'a ci Aarabu ak Wolof

Jàng Simoore Al-Qari'a ak tekkim wolof bu mat sëkk, ak baat. Tekki ayaa bu ne. (11 Aaya — مكية). Al-Qari'a Dégg, Al-Qari'a Tekki, Al-Qari'a mp3, Al-Qari'a pdf.

Jàng te Dégg Simoore Al-Qari'a

🎧 Aaya
M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
—
x1
bismillah
الْقَارِعَةُ ۝١
📖 Tekki Aaya 1
Toj-toj ba !
مَا الْقَارِعَةُ ۝٢
📖 Tekki Aaya 2
Ana lan mooy toj-toj ba ?
وَمَا أَدْرَاكَ مَا الْقَارِعَةُ ۝٣
📖 Tekki Aaya 3
Ana lan moo lay xamal luy toj-toj ba ?
يَوْمَ يَكُونُ النَّاسُ كَالْفَرَاشِ الْمَبْثُوثِ ۝٤
📖 Tekki Aaya 4
Moo di bis ba nit ñi di melni ay lëpaalëpp yu ñu wasaare,
وَتَكُونُ الْجِبَالُ كَالْعِهْنِ الْمَنفُوشِ ۝٥
📖 Tekki Aaya 5
te tund doj yi it mujj mel ni ngëndal nooy nepp ;
فَأَمَّا مَن ثَقُلَتْ مَوَازِينُهُ ۝٦
📖 Tekki Aaya 6
képp ku peeseem diis (ci yiw)
فَهُوَ فِي عِيشَةٍ رَّاضِيَةٍ ۝٧
📖 Tekki Aaya 7
ma nga ko ca dundu gu neex ;
وَأَمَّا مَنْ خَفَّتْ مَوَازِينُهُ ۝٨
📖 Tekki Aaya 8
képp ku peeseem wayaf (ci yiw),
فَأُمُّهُ هَاوِيَةٌ ۝٩
📖 Tekki Aaya 9
ma ngay jëm Haawiyatu.
وَمَا أَدْرَاكَ مَا هِيَهْ ۝١٠
📖 Tekki Aaya 10
Ana luy xamal lan mooy loolu Haawiyatu ?
نَارٌ حَامِيَةٌ ۝١١
📖 Tekki Aaya 11
Aw Safara la wu tàng.
← 100 Al-Qari'a (101/114) 102 →
Jàng Simoore Al-Qari'a ci Wolof – Tekki, Waxtaan ak Baat

101القارعة Al-Qari'ah 📚 11 Aaya مكية



Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers