Al-Qari'a · 4/11
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qari'a
يَوْمَ يَكُونُ النَّاسُ كَالْفَرَاشِ الْمَبْثُوثِ ۝٤
Yauma ya koonun naasu kal farashil mabthooth
📖 Tekkim Wolof
Moo di bis ba nit ñi di melni ay lëpaalëpp yu ñu wasaare,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 2-6 — Simoore Al-Qari'a

2مَا الْقَارِعَةُ
Ana lan mooy toj-toj ba ?
3وَمَا أَدْرَاكَ مَا الْقَارِعَةُ
Ana lan moo lay xamal luy toj-toj ba ?
4يَوْمَ يَكُونُ النَّاسُ كَالْفَرَاشِ الْمَبْثُوثِ
Moo di bis ba nit ñi di melni ay lëpaalëpp yu ñu wasaare,
5وَتَكُونُ الْجِبَالُ كَالْعِهْنِ الْمَنفُوشِ
te tund doj yi it mujj mel ni ngëndal nooy nepp ;
6فَأَمَّا مَن ثَقُلَتْ مَوَازِينُهُ
képp ku peeseem diis (ci yiw)
Al-Qari'aFihi Alxuraan
11Aaya
MeccanRevelation
4Aaya

Tekki — Al-Qari'a 4

Simoore Al-Qari'a Aaya 4 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo di bis ba nit ñi di melni ay lëpaalëpp…

Simoore Aaya 4/11 — Simoore Al-Qari'a القارعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qari'a Dégg, Simoore Al-Qari'a Tekki, Simoore Al-Qari'a mp3, Simoore Al-Qari'a pdf. Aaya 2–6. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers