Simoore Al-'Adiyat ci Aarabu ak Wolof

Jàng Simoore Al-'Adiyat ak tekkim wolof bu mat sëkk, ak baat. Tekki ayaa bu ne. (11 Aaya — مكية). Al-'Adiyat Dégg, Al-'Adiyat Tekki, Al-'Adiyat mp3, Al-'Adiyat pdf.

Jàng te Dégg Simoore Al-'Adiyat

🎧 Aaya
M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
—
x1
bismillah
وَالْعَادِيَاتِ ضَبْحًا ۝١
📖 Tekki Aaya 1
Ca jaabkat ya seeni gimiñ di foor (fas) (Maa ngi giñ),
فَالْمُورِيَاتِ قَدْحًا ۝٢
📖 Tekki Aaya 2
tey këdaa seen tànk ya my xuuy (ferñent),
فَالْمُغِيرَاتِ صُبْحًا ۝٣
📖 Tekki Aaya 3
ak yay songe suba coy.
فَأَثَرْنَ بِهِ نَقْعًا ۝٤
📖 Tekki Aaya 4
yay naawal pënd,
فَوَسَطْنَ بِهِ جَمْعًا ۝٥
📖 Tekki Aaya 5
tey xuus ca biir noon ya.
إِنَّ الْإِنسَانَ لِرَبِّهِ لَكَنُودٌ ۝٦
📖 Tekki Aaya 6
Nit dey, kuy ñàkk deloo Boroomam njukal la ;
وَإِنَّهُ عَلَىٰ ذَٰلِكَ لَشَهِيدٌ ۝٧
📖 Tekki Aaya 7
te kat, moom, seede la ci loolu ;
وَإِنَّهُ لِحُبِّ الْخَيْرِ لَشَدِيدٌ ۝٨
📖 Tekki Aaya 8
te kat moom ku tarla xérlool ci bëgg alal.
۞ أَفَلَا يَعْلَمُ إِذَا بُعْثِرَ مَا فِي الْقُبُورِ ۝٩
📖 Tekki Aaya 9
Xanaa dafa xamul saa su ñu ko jaxasee ci biir bàmmeel,
وَحُصِّلَ مَا فِي الصُّدُورِ ۝١٠
📖 Tekki Aaya 10
te wuñées li nekk ci biir dënn yi,
إِنَّ رَبَّهُم بِهِمْ يَوْمَئِذٍ لَّخَبِيرٌ ۝١١
📖 Tekki Aaya 11
bu keroogee, sa Boroom Ku deñ Kumpa la ci ñoom?
← 99 Al-'Adiyat (100/114) 101 →
Jàng Simoore Al-'Adiyat ci Wolof – Tekki, Waxtaan ak Baat

100العاديات Al-'Adiyat 📚 11 Aaya مكية



Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers