Al-Qari'a · 6/11
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qari'a
فَأَمَّا مَن ثَقُلَتْ مَوَازِينُهُ ۝٦
Fa-amma man thaqulat mawa zeenuh
📖 Tekkim Wolof
képp ku peeseem diis (ci yiw)

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 4-8 — Simoore Al-Qari'a

4يَوْمَ يَكُونُ النَّاسُ كَالْفَرَاشِ الْمَبْثُوثِ
Moo di bis ba nit ñi di melni ay lëpaalëpp yu ñu wasaare,
5وَتَكُونُ الْجِبَالُ كَالْعِهْنِ الْمَنفُوشِ
te tund doj yi it mujj mel ni ngëndal nooy nepp ;
6فَأَمَّا مَن ثَقُلَتْ مَوَازِينُهُ
képp ku peeseem diis (ci yiw)
7فَهُوَ فِي عِيشَةٍ رَّاضِيَةٍ
ma nga ko ca dundu gu neex ;
8وَأَمَّا مَنْ خَفَّتْ مَوَازِينُهُ
képp ku peeseem wayaf (ci yiw),
Al-Qari'aFihi Alxuraan
11Aaya
MeccanRevelation
6Aaya

Tekki — Al-Qari'a 6

Simoore Al-Qari'a Aaya 6 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : képp ku peeseem diis (ci yiw)

Simoore Aaya 6/11 — Simoore Al-Qari'a القارعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qari'a Dégg, Simoore Al-Qari'a Tekki, Simoore Al-Qari'a mp3, Simoore Al-Qari'a pdf. Aaya 4–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers