Al-Qari'a · 2/11
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qari'a
مَا الْقَارِعَةُ ۝٢
Mal qaariah
📖 Tekkim Wolof
Ana lan mooy toj-toj ba ?

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 1-4 — Simoore Al-Qari'a

1الْقَارِعَةُ
Toj-toj ba !
2مَا الْقَارِعَةُ
Ana lan mooy toj-toj ba ?
3وَمَا أَدْرَاكَ مَا الْقَارِعَةُ
Ana lan moo lay xamal luy toj-toj ba ?
4يَوْمَ يَكُونُ النَّاسُ كَالْفَرَاشِ الْمَبْثُوثِ
Moo di bis ba nit ñi di melni ay lëpaalëpp yu ñu wasaare,
Al-Qari'aFihi Alxuraan
11Aaya
MeccanRevelation
2Aaya

Tekki — Al-Qari'a 2

Simoore Al-Qari'a Aaya 2 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ana lan mooy toj-toj ba ?

Simoore Aaya 2/11 — Simoore Al-Qari'a القارعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qari'a Dégg, Simoore Al-Qari'a Tekki, Simoore Al-Qari'a mp3, Simoore Al-Qari'a pdf. Aaya 1–4. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers