Al-Qari'a · 9/11
Tekki Waxtaan — Al-Qari'a
فَأُمُّهُ هَاوِيَةٌ ۝٩
Fa-ummuhu haawiyah
📖 Tekkim Wolof
ma ngay jëm Haawiyatu.
🎧 Dégg

📜 Aaya 7-11 — Al-Qari'a

7فَهُوَ فِي عِيشَةٍ رَّاضِيَةٍ
ma nga ko ca dundu gu neex ;
8وَأَمَّا مَنْ خَفَّتْ مَوَازِينُهُ
képp ku peeseem wayaf (ci yiw),
9فَأُمُّهُ هَاوِيَةٌ
ma ngay jëm Haawiyatu.
10وَمَا أَدْرَاكَ مَا هِيَهْ
Ana luy xamal lan mooy loolu Haawiyatu ?
11نَارٌ حَامِيَةٌ
Aw Safara la wu tàng.
Al-Qari'aFihi Alxuraan
11Aaya
MeccanRevelation
9Aaya

Tekki — Al-Qari'a 9

Simoore Al-Qari'a Aaya 9 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ma ngay jëm Haawiyatu.

Simoore Aaya 9/11 — Al-Qari'a القارعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Qari'a Dégg, Al-Qari'a Tekki, Al-Qari'a mp3, Al-Qari'a pdf. Aaya 7–11. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers